Le Président Macky SALL insiste les sénégalais à s’acquitter de leur droit de vote avec ce communiqué publié sur sa page Facebook en langue wolof :
Mbokk i Senegaal góor ak jigéen, bésub wote bii lu am solo su mag la ci dundiinu demokrasi. Mooy jëmmal ne askan mooy doggal! Maa ngi leen di ñaax ci def seen warugar ci jàmm ak dal ngir dogal li ngeen bëgg ñu def ko ci juróom i at yiy ñëw. MS
